Tay boo xoolee life nu muy demee Yaw dangay daaldi yeme Tay boo xoolee life nu muy tëddee Yaw dangay daaldi yeme Ndax jambat nan fi Jambat nan fi lu nekk Ndax saay saay si Te xam naa ni doo kuy changé Ndax jambar nga Man xam naa doo kuy changé Ndax jambar nga Yaw life xoolal fi ngay tek sa tànk Àdduna dafa gudd tànk Yaw like jëfal balaa jëf wes Àdduna dafay xëy ni mes Te nit ku nekk war na am rooyukay Soo bañee dégg wuyaay Te nit ku nekk war na am wéeruwaay Yaw defal loolu waay Yaw bul la am-am àdduna jaaral boy Ba ngay jaay sa ngoor Yaw bul la réseau sociaux yóbbu boy Ba ngay exposé sa taar Yaw xana xamoo ni ndow dey wes Te ndowo dey jeex Man xam naa ni doo kuy changer Ndax jambar nga yeah yeah Tay boo xoolee life nu muy demee Yaw dangay daaldi yeme Tay boo xoolee life nu muy tëddee Yaw dangay daaldi yeme Ndax jambat nan fi Jambat nan fi lu nekk Ndax saay saay si Te xam naa ni doo kuy changé Ndax jambar nga Yeah yeah Way sant Yàlla ba ma amee yaay ju baax Dieya Naedio Sadibou Way sant Yàlla ba ma amee baay bu baax Jeeba mamadou doudou Way sant Yàlla ba ma amee abadan abadan daiman Abadan ci sama xol bi rekk laay dees Du mësa de aap naa ko téémééri at Ne nan domu géwel bu juddu mum Walay tas sa yakaru bay la Tey baay bu nekk Bu sañoon juur doom bu ko wuutu Doom ju bëgg doon ku baax Kaay ma de la jànt bu timoon sunu maam Jànt boobu moo timoon sunuy baay Jànt boobu mu ñu tiim, mooy tiim sunuy doomi doom Xoolal bu baax li ngay def Bu coow li bari bañu fàtte sunuy yaay Yaw yaa yaay Bu coow li bari bañu fàtte sunuy baay yow baa baay Tay boo xoolee life nu muy demee Yaw dangay daaldi yeme Tay boo xoolee life nu muy tëddee Yaw dangay daaldi yeme Ndax jambat nan fi jambat nan fi lu nekk Ndax saay saay si Te xam naa ni doo kuy changé Ndax jambar nga Yeah yeah Tay boo xoolee life nu muy demee Yaw dangay daaldi yeme Ndax jambat nan fi jambat nan fi lu nekk Ndax saay saay si Te xam naa ni doo kuy changé Ndax jambar nga Yeah yeah