Succès bu ne xanaa xamoo waxtu laay xaar Boroom xam-xam yi junj nan ko doy na waar Tay magg nan xamee bu baax Flambeau bi ñoo ko yor su baxee ñun la baaxal Su bone it ñun la boonal Cees maa ko moom, yaa ko moom Ñoo koo moom, ñu dëggel baat bi jëm ci kaaw Doo daw mu ku xam na ni gaynde nga Dëkku bañ kat benn la ci Senegaal Dëkku ngoon Latyr ak Seck signature Sanex moo tax ñu neex Ñu soxla wuññ jega ni rooyukay Fees fi deel tax ñu kaay ndaamo waawaaw Dëkk bañ kat benn la ci Senegaal Cees kay rekk ci xol dara du ko faay Ku weedi laaj leen ma liim ma faay Eh waaw, waawaaw waaw Cees sama dëkk la, man maa ko moom Eh waaw, waawaaw waaw Cees suñu dëkk la ñun ñoo ko moom Setsi ma gaaw ma wone la way! Wone la lu dul gis ci benn reew Fi àjjana la, non y'a pas photo Jengu man la kon nañu ko toppatoo Ku ne saañ nga wax ni fi nga dëkk moom moo la neex Ku ne saañ àapo ni fi nga dëkk ne moola neex Ku ne saañ nga wax ni fi nga dëkk moom moo neex Cees kaay moo ma neex, man moo ma neex Eh moo ñu neex, Cees kaay yow moo ñu neex Yóbbu ma yóbbu ma Kër maam al hajj Ziare Ahmed Barro njegeen Jar jamagene, Ziar suñu maam Abdou Aziz Aidara dem Medina Fall Penc Baye Fall Yaa Cheikh Ndiguel Fall Meissa Bigue Coumba Fall Dabaay Khabrou Abdoulaye Yakhine Duñu fàtte wa jangu bi Cees kaay mooy sama reew Eh waaw, waawaaw waaw Cees sama dëkk la, man maa ko moom Eh waaw, waawaaw waaw Sunu dëkk la ñun ñoo ko moom Setsi ma gaaw ma wone la way! Wone la lu dul gis ci benn reew Fi àjjana la, non y'a pas photo Jengu man la kon nañ ko toppatoo Ñu soxla wuññ jega ni rooyukay Fees fi deel tax ñu kaay ndaamo waawaaw Dëkk bañ kat benn la ci Senegaal Cees kay rekk ci xol dara du ko faay Ku weedi laaj leen liim ma faay Eeeh eh eh eh Yóbbuma Mbour Guedj Mbour soose, mbuur kankuran aah Damay ñëw gaaw yaay Eeh eeh, Cees kaay Hun hun Cees kaay Ñu soxla wuññ jega ni rooyukay Fees fi deel tax ñu kaay ndaamo waawaaw Dëkk bañ kat benn la ci Senegaal Cees kay rekk ci xol dara du ko faay Ku weedi laaj leen liim ma faay