Fi dem na ba kenn mënutu fe def lu baax Ku def lu baax ñu faay la lu bon léegi nak Xawante sutura yaakante deer te duma sa noon Mënoo dem kenn du dem léegi nak Fi dem na ba kenn mënutu fe def lu baax Ku def lu baax ñu faay la lu bon léegi nak Lu ne ngay dégg ñuy wax di yaak deer Dundal Yàlla baax na lépp dina leer Fightal sa life ndax mbamb rayul weer Bul mësa xaadi kon life goes on Bul mësa bàyyi, eh eh eh Broda life goes on, eh eh Bul mësa xaddi, eh eh eh Sister life goes on Dina la ker nga fay ma naj Sa xol bu bon bi nanga ko jema soppi Jobal jobal nga bañ ba rom naa la dem Yaa ngi sandi xeer bouclier sama dos du daal Fi nga taxawoon demb ne maa fi gëna baax Mais fi nga taxawaat tay ne maa fi gëna bon Wax ju bon dëkkul fu mu jëm Fu mu juge la dëkk Dama laay bàyyi ngay wax maa ngi si tollu lajj kaw wa kaw Le chien aboie la caravane passe Maa ngi sama auto yaw ngay dégg kanam passe Lu ne ngay dégg ñuy wax di yaak deer Dundal Yàlla baax na lépp dina leer Fightal sa life ndax mbamb rayul weer Bul mësa xaadi kon life goes on Bul mësa bàyyi, eh eh eh Broda life goes on, eh eh Bul mësa xaddi, eh eh eh Sister life goes on Doomu jaambur xamoo nu ñu ko ngembe Grand place du place Nga topp ci deeram di lëmbe Yee ma tuñu si yaak deer Ak dëkke wax ju ñaaw Dale yóbbu si sëriñ Ne ko defal ma xeel mi naaw Lan moo fi jar yi jikko yu bon Yàlla bindul yemale wul Te wërsëk yi bokkul Lu tax su ma jiito nga may joxoon Nii ma mel du kenn Yàlla moo ko def ci man Le chien aboie la caravane passe Maa ngi sama auto yaw ngay dégg kanam passe Lu ne ngay dégg ñuy wax di yaak deer Dundal Yàlla baax na lépp dina leer Fightal sa life ndax mbamb rayul weer Bul mësa xaadi kon life goes on Bul mësa bàyyi, eh eh eh Broda life goes on, eh eh Bul mësa xaddi, eh eh eh Sister life goes on Fi dem na ba kenn mënutu fe def lu baax Ku def lu baax ñu faay la lu bon léegi nak Xawante sutura yaakante deer te duma sa noon Mënoo dem kenn du dem léegi nak Yaw life goes on bul mësa bàyyi, eh eh Broda life goes on, eh eh Bul mësa xaadi, eeh Sista life goes on Eeh brother life goes on