Yeah! Yaa tax lépp lu ma songe daan ko Doleel nga ma fune Nit ki la nob ba ñépp xam ko Na la jaaral lune Man jox naa la lune lune Man jox naa la lune eeh Man jox naa la lune lune Man jox naa la lune eeh Naa la follow fépp foo dem Man yaw lay titteru fépp fu ma ne eeh Man daañ may meree su maay wax ci yow Ndax mësoo changé mësoo kakatar eeh Yaay sama number one Yeah, number one Jikko bu rafet loolu nga ma wone Yeah, loolu nga ma wone Eh duubi duubi, eh daddy daddy Man maay sa daddy daddy Eh duubi duubi, eh daddy daddy Man maay sa daddy daddy Sama babe kaay Gis naa sa melokaan Yaa tax maay dëkke daan Yow rekk yaa tax ma fier remuer ciel et terre Ngir lépp lu ma am ma indil la Woo ma ma ñëw balaa nga tek reer Xam naa lépp lu baax pur man la Jox naa la lune eeeh Yaa tax lépp lu ma songe daan ko Doleel nga ma fune Nit ki la nob ba ñépp xam ko Na la jaaral lune Man jox naa la lune lune Man jox naa la lune eeh Man jox naa la lune lune Man jox naa la lune eeh Def la jabar te kenn du ci tek baat Ñépp d'accord ni danga mérité dote Ajjo saay mbagg titeru wo danga took Sama gale kenn ku dul yow du fi tek tànk Yaay sama number one Yeah, number one Jikko bu rafet loolu nga ma wone Yeah, loolu nga ma wone Eh duubi duubi, eh daddy daddy Man maay sa daddy daddy Eh duubi duubi, eh daddy daddy Man maay sa daddy daddy Eeeh Léegi nak leen mo ci dese Nga took sama wét te doo dem Doo jigéen buy tokk ni fees seuh eh Eh jox naa la lune lune Jox naa la lune Yaw ya tax lépp lu ma songe daan ko Doleel nga ma fune Nit ki la nob ba ñépp xam ko Na la jaaral lune Man jox naa la lune lune Man jox naa la lune eeh Jox naa la lune Man jox naa la lune eeeh!