Dina la, dina la Dina la yobbu fu nga aggulwoon Dina la denk lu ma sori Man dina la jox nga teyil ma sama xol Àdduna ngi gis te noon yaa ngi wax Jaratul coow ci man la uuhm Ba nga jàppee ba tay du danga bañ de Dañu indispensable ci yow ni ndox Xooloo ndax sama poche am na carte gab Lijjënti wo sama père dafa capp Sama self am free rekk molaa ñoor Defaluñu la litax bañ lay ngooro Jaaral nga ma soppaleku doon terroriste Adhérer hezbollah doon extrémiste Ku la laal ma takk ci kowam muy gis Ba mel ni gangsta bu amatul jiis Kon dinaa la dinaa la dey Dinaa la dinaa la may Dinaa la jox sama xol Dinaa la def sama tool Man dinaa la dinaa la dey Dinaa la dinaa la may Dinaa la jox sama xol Dinaa la def sama tool Lu mu mëna ma jël Yaay sama kom-kom Bët dey gis te xool dey wax Ñaar yi le woon nañ ma yow yaa tax Bataay ñu laj ndaxam neewuñu paradise Alors que jege wuñ sax lu mel ni paradise Start from the bottom ba tax may gërëm Xëcc bu dagul may laj ndax dinaa dikkëm Xëcc ñu nga taf ñu sa bopp door ma biz Na la feccal ngel ni mbaye ndiaye kaam dikaam Li nga ma jaral yépp suñ ko toggoon di wax Waat na ko ci Yàllah babe dinaa fi fenak Def ko ci sa xol te nga jàpp babe du nax Suñu tool dafa laaw mu ku boy du lax Fi nga ma def ak fi nga ma yobbu xam na Fu ma jule ñan si mawlana Sumb bi ñu sumb Agaal ko teemu gaaw Wax ko ko wax ko ko wax ko Kon dinaa la dinaa la dey Dinaa la dinaa la may Dinaa la jox sama xol Dinaa la def sama tool Man dinaa la dinaa la dey Dinaa la dinaa la may Dinaa la jox sama xol Dinaa la def sama tool Lu mu mëna ma jël Yaay sama kom-kom Sometime ñu tongo ku ne dem yonaam Li ñuy jubbule dokoo xamaam Lu ci man lu ci man wor na du ci yow Lu ci yow lu ci yow la àdduna di wër Suñuy défaut ak sunuy caprices moom nga ànd Emprisonné te ne dotoo ko xool Nu ñu mel nu ñuy def nga ni bëgg na Balaa ñu la wo nga ni waaw dégg na Kon wax ma fooma def, foo ma def Baby wax ma fooma def Fi nga ma def xam na sori na Ndax mënatu ma Mënatu ma dundu sans yow Yow wax ma foo ma def, foo ma def Baby wax ma foo ma def Fi nga ma def xam na sori na mënatu ma Mënatu ma dundu sans yaw Kon dinaa la dinaa la dey Dinaa la dinaa la may Dinaa la jox sama xol Dinaa la def sama tool Man dinaa la dinaa la dey Dinaa la dinaa la may Dinaa la jox sama xol Dinaa la def sama tool Lu mu mëna ma jël Yaay sama kom-kom