Waooouuhh! Lépp louma ame akk koumou donn Chérie boy yama ko gueuneul Limay liguéy béss bounék dicii sonn Cii lou bax lépp yaayy borom Yaa tax ma xam kii madonn Djoox ma fiit Mbétané dotouma tiite Wooooooohhh! Limay liguéy béss bounék dissi sonn Ci lou baax lépp yayy boromm Ya tax ma xamm kii madonn djoox ma fiiitt Mbétané dotou ma tiiite Xoll ma cii beutt ma baby boul xéff Té boul ragal Diam rék ngay ame Lima beug rék moy Kou baaax So kii gueunn Borom xol bou niiice Kouma doul nax dima bégueul Souma djaxlé sax mou défeul Kima donn sétt yaw laa Malay bégué éh éh So mbétah Tay ma takk la Ndax da nga beury djom Togal xarr bama takk la Réékk téral laaa Douma la massa fowé Ba nopi bala fii Gorr gnou bax yi romb la Yaaaww Ngay misérrre Laaa ah Lalalalalalalalaaa Lalalalalalaaaa Laaaaa lala lalaa Xamna beugg ngama Téyiitt xam nga beugg nalaaaa Chérie biiigg sax feugu nalaa mann Cii aye nélaw ngani ma beugg ngamaaaa Xam na beugu ngama Oohhh Téyitt xam nga beugu nalaaa Chérie biigg sax feugu nala Cii aye nélaw ngani beugu ngamma Aaaahh Fiila Fiii laaa Boudoul fii Dou donn fénéénn Kiila kiila kii laaa Boudoul kii Dou donn kénéén Yaw xam nga sa bopp Xam li nga donn Lay layla laaaa Ndax djiguéénn Day xam bopaaamm Samm nga sa bopp Ya ngui xool euleukk Yaw da ngay aaaammm Djabooottt Takk nga sa seurr Moytou nga gaa gnii Ndax bougn la xaméé Démm bayilaaa Wax djii loumou néx Héy Néxa néxa nééxx Yaw boum la tax beuhh Xamm sa boooopp Ndax djiguén amoul loudoul bopam Walay djiguénnn Amoul loudoul sagamm Mbeuguéél mo nééxx Ci bougn la beugué Mbeuguééll mo nééx Ci bougn la nobéé Mbeuguéél mo nééx Cii bougn la woolloo Mbeuguéél mo nééx Cii bougn la Safoooooooohoooohhohooooo Mbeuguél mo nééxx Bara chéri Soda laaa Mbeuguél mo nééx Baye Diop Chéri Amina Mbeuguél mo néx Djély Niass chéri Sofina Mbeuguél mo néx Henry chéri Aminaa Héyy