Suma la mënoon gisaat Gisaat la benn yoon sama life pour wax la Ne la sama xol masoo fi jogee Numay def pour gisaat la Gisaat la benn yoon sama wet ngay retaan Ngay bég dima begloo Ohhh Dem nga bayi ma fii Dem nga yobaalé sama leer bayi ma ci lëndëm Wéetal ngama loolu Numay def pour gisaat la Numay def pour gisaat la Pour wax ni la "I LOVE YOU" baby Dem nga bayi ma fii Weet na, yama weetal Kañ ngay dellu waat fii Ci sa wet laa bëgga dàlloo Dem nga bayi ma fii Wéet na, yama weetal Kañ ngay dellu waat fii Ci sa wet laa bëgga dàlloo Feeñal nga ma réeraat na Numay def ba gisaat la Dem nga bayi ma wéetal ma Biig ci guddi janeer na la Ya ma taxoon daw bay death Te nañ ma bayi ma wéeto ak life Li may yëg ci moom du dëñ Batay mbëgelam momay daaneel Wéet na jooy ndax wéetaange (wéet na) Réer ma réer Way réer na Nela weccoo ak keneen Batay mbëgelam momay daaneel Yaane woon duñu yaw do ñoom Nobuma ku melni yaw Sama xel du jóg ci yaw Suma la mënoon gisaat Gisaat la benn yoon sama life pour wax la Ne la sama xol masoo fi jogee Numay def pour gisaat la Gisaat la benn yoon sama wet ngay retaan Ngay bég dima begloo Ohhh Dem nga bayi ma fii Dem nga yobaalé sama leer bayi ma ci lëndëm Wéetal ngama loolu Numay def pour gisaat la Numay def pour gisaat la Pour wax ni la "I LOVE YOU" baby Dem nga bayi ma fii Weet na, yama weetal Kañ ngay dellu waat fii Ci sa wet laa bëgga dàlloo Numay def pour gisaat la Numay def pour gisaat la Ci sa wet laa bëgga dàlloo Dem nga bayi ma fii Weet na, yama weetal Kañ ngay dellu waat fii Ci sa wet laa bëgga dàlloo Dem nga bayi ma fii Weet na, yama weetal