We gonna fight for your right Fight for your life for your freedom Dund ci ndool bëgg ci geen Fii goor akk jigeen ñëpp a bëgg fas jom Tukki du tekki Tekki du tukki looy utti Yakamti xamoo looy fekki Yoon bëgg nga tekki Am-am ñu gënël am teggin Dëkk ci dëkk bi nga tekki fi moo jafe Tax ñu xaddi Ga'ddaay fu sori baayi njaboot gi Mënu ñu dëkk ci ndool yeewoo xonet we need money Teed tax ñu jël yoonu geej gi Jooy na jooy na ngir gisaat la Woy naa la brother Jooy naa la Baaba Nothing to hide My people die young ndax bëgg tekki Jamano ji ñu toll ñëpp a saalit ja'mm amul La'mbaay rafeta gul Batay Waalo naata gul Tukki gënëllu ñu waaye ligeey moo fi amul Reew mi ndaw la ñakkul Ku na'mp ci Maam Ndey nga gisul Nothing to hide My people die young fii ñëpp bëgg tekki Nothing to hide My people die young because of immigration Fitche' duul xam fii dara amu fi Fii ku fi amul dara ken dula tekk nitt Su ma xasee dugg kaaw doo tu ma dellusi Rap naa junni att gisu ma ci we'ccit Sa'cc sama gaz or dima tere visa Ma'nk sama pe'trole dima naxee pizza Mënu ma ci d'accord faut que je dis ça Tampon passeport tekki takk Lyssa Bëgga tuma toog fii njiit ñi dima politig Foog ma dugg avion calmer sama solitude Nang ma wax waxu kaaw boo ma bëggee disturb Di naa mësa radical jël gun ray ñëpp Tukki taxul noflaay Toog ci reew mi ligeey gën woor Ñaata ndaw ñoo ga'ddaay Tekki tax ñu ba fi li ñu moom Tukki taxul noflaay Toog ci reew mi ligeey gën woor Ñaata ndaw ñoo ga'ddaay Tekki tax ñu ba fi li ñu moom We gonna fight for your right Fight for your life for your freedom Dund ci ndool bëgg ci geen Fii goor akk jigeen ñëpp a bëgg fas jom Nothing to hide My people die young fii ñëpp bëgg tekki Nothing to hide My people die young because of immigration Tukki len xam Ja'ngi len gis