Yeah Was born in 1995 Juddoo Ghetto màggee Ghetto My name is Ashs, you know the vibes I'm from zero to hero Seereer ci baay Baay Faal ci life Ci man dara du fi dara May kan nitt ku toroxlu la Mujj bu rafet rekk ñaan Was born in 1995 Boroom basse bi guitare bi sam baay Yaay Joor def li nekk ci man Mënu ma dof fate fi ma jaar Boy laa woon comme boy yëpp Amoon rêve pour tëpp tekki pour ñëpp Yalla Buur bi doggal Du ma lenn kenn mais lepp ñëpp Was born in 1995 Born in 1995 Yo Yo Born in 1995 Juddoo biir ghetto maggee biir Ghetto Taxul nga raw ñu brain ci life {1995 yo yo} {1995 yo yo} Ma nekk ku kenn nekkul ci ñoom Ñoom dañ ma jiitu fu lëndëm ma len niital fu ñuy tekk sen tànk 1995 This is what I do all night This is what I do every f**king night Fuck ñu fogoon ni ñëwoon pour tekki ci rew me we try all day all night Tukki du tekki, tekki du tukki teewul Ñoo ngi jekk ci game bi ligeey money fayeeku Nobody can stop my mind Nobody can stop my mind Juddoo ci hood màggee ci hood bi fuck almadies ak Cap Si mbedd buur bi lañ jàngee hip-hop même prési day xaar Bañ nga def ma jàam ma def rappeur bu mag Bëggu ma kaaw ak gellu tubaab Juddoo ci reew mi tekkee ci reew mi from zero to hero Nothing to something yaakaar ci Yalla gën yaakaar si yeen Nigger what's poppin' mën u ñu bókk ay demin Yeen da ngen i foo man may teegin Ñoom ñoo ngi si kaw man may sommet bi Nobody can know me man maa gën a high sen rappeurs yu magg yi I can't follow you soo jiitalul mind sa doole du jëriñ Rabuma pour siiw maa nge'eg melodies yuy dugg ci xol yi Wëri millions vues moom du musique rekk ligeey la ak fayeeku Nobody can know me maa nge'eg dictionnaire ak flow bës bu nekk Duggu ñu ci mines yi no du ñu teggi tànk ay att fii ñoo fi nekk Talent confirmé sa emcee confinement lay dugg ay dewën Boy Ashs day jinne limay rap de fi damalen rawee ay dewën Born in 1995 Juddoo biir ghetto maggee biir Ghetto Taxul nga raw ñu brain ci life {1995 yo yo} {1995 yo yo} Ma nekk ku kenn nekkul ci ñoom Ñoom dañ ma jiitu fu lëndëm ma len niital fu ñuy tekk sen tànk 1995 This is what I do all night This is what I do every f**king night Fuck ñu fogoon ni ñëwoon pour tebbi ci ... Tukki du tekki, tekki du tukki teewul Ñoo ngi jekk ci game bi ligeey money fayeeku Nobody can stop my mind Born in 1995 Born in 1995