Mmmm Mënatuloo siggi ci bët xool ma Mënouma woon gëm ni nakho ma Ku la ko waxoon loolu am na Lu agne du réer te matt na soor Li nga ma waxoon wuutek say jëf Digué boor la té yaw woor nga Nga laaj ma sama xol man ma jox la Defoo ma ni sa bopp takh nga gaañ ma Keerog sam xel bi waroon na tey Say wax woor ma Dañ ma téré woon ma taxaw wat ni sañuloo ko Ma jël la teg fi ma tegul benn mindeef Bi nga xamee bëgguloo ma wax ma ko Bëñ ak lammiñ fak ñu laale (waawaaw) Wayé fajaloo ma sama gacc (mmm) Nu may defak samay dëkkëndoo (samay dëkkëndoo) Duma siggi xol ci samay nawle Gacc gi fu ma koy waxé (héeee) Ci xol la tiis boo may lacce (haaaan) Dinga ko gis Yàlla ñuy àtté (Yàlla ñuy àaaaatté) Bi nga fi jii bës ding ko goobe (goooooobe) Ayway Samba Yaw dé yërëmoma (yërëmoma) Nga tooñ ma benn yoon man ma baal la Nga def ko ñaari yoon man ma baal la Yeah way Samba Yaw mi de bëgguloo ma (he le le le) Nga laaj ma sama xol man ma jox la Defoo ma ni sa bopp tax nga waar ma Waawaaw Mmmh mmh Ki sedday bi Tàngoor bi Nekk ci naaj bi té kéraloo ma, kéraloo ma Defuloo ma ni ma la def Lu ma xam wax la Alaal ma jox la Mbëggeel ma waan la Kan nga ma jënde lan la ma rawé Ki nga ma jënde lum ma ëppëlé Réwoo réw weur naa ko (Réwo réwo) Keneen ku ma guis ni yaw la (Réwo réwo) Ñu mel ni yaw lay musloo (Woo mbëggeel) Nga def lii man lay wuyoo Réwoo réw weur naa ko (Réwo réwo) Keneen ku ma guis ni yaw la (Réwo réwo) Ñu mel ni yaw lay musloo (Woo mbëggeel) Ni mbëggeel def man lay woyloo Ayway Samba Yaw dé yërëmoma moma Nga tooñ ma benn yoon man ma baal la Nga def ko ñaari yoon man ma baal la Yeah way Samba Yaw mi dé bëgguloo ma Nga laaj ma sama xol man ma jox la Defoo ma ni sa bopp tax nga waar ma Gàcc gi fu ma koy waxé (hééééé) Ci xol la tiis boo may laaje (haaaaaaaan) Dinga ko gis Yàlla ñuy àtte (Yàlla ñuy àaaaatté) Bi nga fi jii bës dinga ko goobe waw