Par AbouAmg Tchi digueunté marakh maassé Bi djololi suuf séédé Tchi lagne gawantu sakou ci sa ay njeurigne Tchi kaddu yu tedd yi May bindeu ngir façon ci maman Kène dotoul mel ni yaw Nio ngi lay chiaaré Di riir ngir modou bamba Mo xeulkh té balle Ngir tagir mi indi lerr Tchi yone wou méti wi Ak keppeu ko xamni baye chute nga tèy Bégué mame cheikh ibra chute Maïsa bigué coumba chute mo wané yone bi Aouzou billaah Bismilaah Kène dou yaw Ibra chute Cheikh Ibra yi nékal kamal Dial goor yalla yomboul Lassal daak lil Jamaal Ibrahima faal lam yazal Yaay lampe gueuneel bi bamba taal yaaram bi naam chute Yaw la bamba wane kawçaraak gui naane Gueediou bolero Naam yaw automne titeurou woulo Seug beek sigui bé Borom yallah mba jaameuh nga am Tabbé maame Seynabou Ndiaye mo wane yone bi Baye chute moy lou doyouk waar Mo toudou tuurou yallah bi Bamouy xotti djawou dji Di yengueul harceler ak kurçiyu Baye chute moy dieufé ndigueul Moy diokhé té kene douko laathie Baye chute bou deugou té woriana Sa keuraw moy a. Haaaan Niou roy ci Cheikh modou kara ak Baye karim Al-Akhlah Tognou niou togn lou wougnou Dieuf yi nagnou ko rafétalaate Kone keppeu ko xamni baye fall nga tey Beug roy tchi cheikh ibra chute Nanga am yarr mandou Njegueuf teuy Al Hamdulilah Niou santati Cheikh Bamba tay Ngir mo takhaw Djouli wone fa Ndar bagn Niou Sankou tay Ya Rakkam MOY sauwétasse tchi nioune ngir MOY dokh Batay Magal ko MOY li guerre ci nioune diko Santé tay Bureau Famil Ndar mo atte Goor Yafa diaar beu weuy Kou tchi doul serigne touba kérok signé wone nga "oui" Balle darsak wa tribunal kérok nieup xeuy kagnou naane Borom ndar takhaw dikou yallah dji djay Bamba bay neu goop na djaak neu Gaadou neu ak sakkeu Sameuh bodji wall neu modgne neu ganaaw aadou sokkeu Meune neu dieuf nako ak xam xam Mouride na nga deggueuh Ragnel lou baakh tchi lou bone boula netchi kene de Bgueuh bibeus nkhal Xara-ngal neel xareu-xareu wakh leu djou am sewa sew Wa salaamoune ala manni tabkhal khoudaa Miim reew bamba ka maman moy kika maman