Le passé c'est le passé Trop de problème avec toi j'en avez assezz ey Maintenant que tout a changé J'ai tourné la page car tu m'empêche d'avancer Thi diir bou gat lala khamé gua beug ma jugé Thi sa digue, sa ay kharit gua sewalma ni i Mane yorou mawone khaliss Mais gniko yor sa khol iow mousso lenko thiabil Bamala guissé si la guiss nit kima done sét Façon yéne gor yii nieupeu yam ganéma mounoul néh Mane melouma nii guar gni Sa tank sama tank gua présenté ma PA bii Gua begn dh néh dou mak iow Geume lo mani né mounougnoun Dem fén mak iow Téré nanie ma teud temps nah doumala am iow Iow mi sa bop yama téré ande ak iow Gua bagn dh néh d'où mak yaw Geum lo mani meunougnou dem fen mak iow Téré nanie ma teud temps nkoul ak iow Iow mi sa bop yama téré and ak iow (bb) Noboma wone, noboma ndeyssane, Noboma wone bameu lay face time, Talo ma wone bameu lay message, noboma woo-woo-woo-ooh(×4) Kouma ko wakhone douma ko geum ya moudier xewii nii Mane iow rk la guissone gua diapé meuh nit invisible Bayina la à vie, faté gua bigua ma done rombe ak vitesse Ferrari(thip) Mbeuguel indi woula lila indi dieulina Tey guamay sogua moune sét fep ni FBI Rethie nala bayil Way bigua ma done dieundé lgui gua ko niémé trahir Gua begn dh néh dou mak iow Dama la mounoul mounie niou dem féne mak iow Doma téré nakh mounou ma ande ak iow Iow sa bop yama téré and ak iow baby(×2) Noboma wone, noboma ndeyssane, Noboma wone beumeu lay face time, talo ma wone, doma done message Noboma Woo-woo-woo-oh(×4) Pourquoi tu crois aller venir quand tu veux Cette fois hélas c trop tard ohh woo-woo