Kishore Kumar Hits

Dip Doundou Guiss - Waawaw şarkı sözleri

Sanatçı: Dip Doundou Guiss

albüm: LNN (Loo Ñeme Ñàkk)


Même si guènte damay weet
Soma fassalé kanam
Waawaw, waawaw
Samay pékhé yeupay diekh
Takh ma ladj la
Fok ga wakh ma (wakhma, wakhma)
Soma diégué lépay leer
Doma wanati guinaaw
Waawaw
Yalla deff na dotoul dègne, nan
Beug nala beug nala
Baby kaay gnou weet, yaw kaay weetoo bae
Kaay gnou weet, Baby yaw kaay weetoo bae
Diougueul gnou dem tok né
Yaw kaay gnou weeto bae
Ich ya ya yi ya Ich ya ya yi ya
Baby kaay gnou weet
Yaw kaay gnou weeto bae
Yaw kaay gnou weeto bae
Contane na lol sa bissa diote
Kone tay lo diooy damakoy fadj
Sonoone ga lol si liko diar
Yaw sakh khamga li dou hasard
Because I'm before you love me
Because I'm because I'm empty into damay weet
Soma fassalé kanam
Waawaw, waawaw
Samay pékhé yeupay diekh
Takh ma ladj la
Fok ga wakh ma (wakhma, wakhma)
Soma diégué lépay leer
Doma wanati guinaaw
Waawaw
Yalla deff na dotoul dègne, nan
Beug nala beug nala
Hmhmhmhmmmm
Li né si yaw mo né si mane
Yalla moko deff
Waawaw
Hmhmhmhmhmmm
Li né si mane mo né si yaw
Yalla moko deff
Waawaw (yeaaaahhhh)
Loumay dokh di khool kénène
Li si yaw dou si kénène
Doumala wétio ak lénène, mbeuguèl
Dou dégne Dou dégne dou dégne
Waawaw
Dou dégne Dou dégne dou dégne
Waawaw
Si guènte damay weet
Soma fassalé kanam
Waawaw, Waawaw
Samay pékhé yeupay diekh
Takh ma ladj la
Fok ga wakh ma (wakhma, wakhma)
Soma diégué lépay leer
Doma wanati guinaaw
Wakh ma
Yalla deff na dotoul dègne, nan
Beug nala beug nala

Поcмотреть все песни артиста

Sanatçının diğer albümleri

Benzer Sanatçılar