Kishore Kumar Hits

Dip Doundou Guiss - Musiba şarkı sözleri

Sanatçı: Dip Doundou Guiss

albüm: Musiba


Fuck number one
Fuck number two
Ya ngeek limay fay
Moytul baña juum (yeaah,Ouuh)
Musiba naarulay Gëm sama ñaanu yaay Lëmbé ndakaru ndiaye
Musuma Xaddi, bañuma jeng
Mais duma daanu way
Aka ma gaaw si
May sa musiba narulay
Musiba narulay
Comme roof si ceeb
Cere dolli ñeex Capp ni goor Gui Dieng
Vol si jet,
Wala doxx si geej Yokk job du deñ
Kuy bonn di hate
Bombe nucléaire ci
Sa xol bu wow ni xeer
Même boy dé bul fokni jeex na,
May bëss bila God di yé
Investir ci fenn amo saxx bénéfice du doute
Na doon 50 cents sama ben shot,
Sa fils du jukk
DIP mola mën du gacce
C'est comme ku Messi di duut
Ma Ngi si trône bi ak ñom Messi
Jël sama Pepsi di guux
Duma segg si cage
Man la seen soeurs yi di xaar
Maa taxx sen sërr yi di tass
Carrière Bi munoko saltel nigger
Melni sa chemisou pa
Sëg di gass,
Job lu tax CD bi jarr
Fële jël sa reliquat
Sama cachet sañu ñuko dagg
Ni bin bin ci sa ndigu
Ma Na money bi teew,
Xaalis moy gagner guerre bi duma rayante comme militaires Si kaw
Lañuy yeeg wacce leen ni adam ak awa ak pomme biñu yëy
Sori fi man,
Duma xooli sa guel même su defe man kesse si story privem
Coow li Du jeex fi ba mëwti di dé
Amatu ñu adversaire mais ño ngi si guerre
Fuck number one,
Fuck number two
Ya ngeek limay fay,
Moytul baña juum (yeaah,Ouuh)
Musiba naarulay Gëm sama ñaanu yaay Lëmbé ndakaru ndiaye
Musuma Xaddi, bañuma jeng mais duma daanu way Aka ma gaaw si Gars yi
May sa musiba naarulay Musiba naarulay
Every day, may def baña xaar ndaxx dé du jeem
Soxlawuma tuub pour def Ko
Benn buum mën na takk plus de 5 jeeg
Yes we can Gedd gratte- ciel,
Dëkki Baraku Bamba fu Trump dem ba nek president
Fu sëtu esclave dila Ray ngir chaîne
Tojj sa lu bonn ba mujje ak séy biens Nigger
ëppo Njariñ skincaru Michael Jackson ci cimetière
Dangay gunge rek ni Frèru Michael Scofield ci biir jail
Damay fayu ba pare mën nangu ni
Coow du jib kay Ku xamm kepp kuy rap wolof
Xamna nombre rappeur bi DIP fay
Tek sama nafsu ci beat bi
Rap yefu dëmm Dëg lë
Kan mo saña waxx ni que Pac bëggul Biggy?
Sen game bi concours lëmbël la
Motax malay yokkal ay tama si beat bi
Sa guel la yakoy solal makoy simi,
Dagg buumu gacce dagg seeni string yi Sama kumpa nekul books mais
Rappeur yi publier gul sen streams ti
Ay goat yu vider plassu gettu
Bëy du sho bu tijji tank rek ñu dem
Dé bi kesse momay taxa tëddi ni
Roses yi si sa tanku caissou neew
Bëg coow ni intifada Ben Laden
Même Dof du sikki sakka lima fi def
God du mëssa àndak ñi di fenn
Par force King bi man la té du deñ

Fuck number one,
Fuck number two
Ya ngeek limay fay,
Moytul baña juum (yeaah,Ouuh)
Musiba naarulay Gëm sama ñaanu yaay Lëmbé ndakaru ndiaye
Musuma Xaddi, bañuma jeng mais duma daanu way
Aka ma Gaaw si gars yi
May sa musiba naarulay
Musiba naarulay

Поcмотреть все песни артиста

Sanatçının diğer albümleri

Benzer Sanatçılar