Medaillou number one la weko nak loum togu yak done lekou mak Kou tonguook mome yaye rethiou niak rap pur et dur doù fethiou niak Biggui na khamni amna rak tchi beat bi sakh dey djiékou pac (2pac) Sayo dégué wouy walou kou djiaguédi mo dadjiek kou djiag Kk mo djité gniniouy djiteul ak gni djitéwoon Taye tool béh soukheeut maye bayalél gni dji teuwoon Xam xam ba tchia coki nak katane gui tchi dondi nak Xalé bou xéleum déh khassane lek lek dey sokhla woki mak Wané na founé tchi fane yeup dotoul competir Deugueur boppeu takh ma deflen mala dilen dompté khir Corner yeup la conquerir Koba vont en perir Xelou dieun nga yorr do contenir takh foma compé miir Fils doneul mini may maxi eupeuleu daradjia Pistonel mc bouy aksi ma koy dieul ko deureudjieu Beat bi loumou feugu meu reude tek tchi kou melodieux Gunzout Diwsquad LG Galsen Hands'up Please let me hear you say KK Moy Number one Kk moy number one lou khel yi meuneu nangoula Bo ticholiwoul li dess seu life bi yeup ay niandula Fuck gni tchi andouleu surdose bouniou ndiambouleu Only real moniouy cons nioun fake bou niou niam douleu Midi diotna ni nagn nga dieul ampoule di niit Hit yi bari ni gagni nigga dampoul tchi nit Rabou mbed la niodi incarné marginal Tareul kocc barma mouy dioli tchia internationnal Niom niep la craquer sen code yi ak sama virus man Gni ma dane dingkat demb nio melni kou rouss men Bank len lokho yen tasspé naba dou murder As Legui rap agneau leu tiouné yéy ame code Bou beat bi wangeto nga djiss gni war mbame yi meunounio kotte Swagger boy nio beuri niom niepeu nourau rap Té kotchi tégual right mou teup saga bou khamé mouno raak Gunzout Diwsquad LG Galsen Hands'up Please let me hear you say KK Moy Number one Meunoulenma juger fuck seni magistrature Boudé deugu leu keufeul mic ma djiss sa rap pur Boudé sa opinion danie leu kay dicté my nigga fi dofi ame moyenne Indil sa cahier nga djiss sa rature Wekh ni domou nima nigga doma nima Tchi eukhlou rap galsen amna kouy wakh ni do monument Deugu leu dama zarbi mais maley firil saar bi Djibeuleoul tchi mane indalé adiyeuk ziaar bi Medaille bi doréna founé mbed decoréma Sayouma yoré mic nga degu amna niam té gooréna Nelen sen khel yi dale ndakh ndk dou meusseu sak Gunzout Diwsquad LG Galsen Hands'up Please let me hear you say KK Moy Number one