Kishore Kumar Hits

Young Bari - My Own Hype, Pt. 2 (feat. Feat Flow) şarkı sözleri

Sanatçı: Young Bari

albüm: My Own Hype, Pt. 2 (feat. Feat Flow)


Di na fègn ci jikko wala fègn ci judd
Ndakh Ci derett lay nekk du nè ci mboubou
Du yeuglu du feug day dikk doug
Bul lo bayi muu lèkkè lokho jokh kuddu
Moy njeukk ci bool bi te moy ciy mujjé
Fooko fekk day foXlé beunlé beug wujé Du doylu du nè doyna du doyal du dessal
Badolo gaw ci nè Dolli ma bootu sa kaw di la dissal
Bala jogg ci ndap li ndawal li jekh
Bu suuré du nè jaraw lakk day fudd raay dékh rek nè
Moo raw purux Du geureum niami daw
Fu mu la fekké si tolof tolof bayi lafa daw
Soo ko invite day invitè moromam
Te wax bu yonam nekul sakh fauk mu sapali ci xoromam
Da fay sew jikko meun a setlu siss sof
Sans sutura lumu la xamal mu siiw rakh gaw ci Soss
Xamul njiowan te bala moo watch mu dagg
Buggul dégg deug li mu beugga dégg moy ku kay Tagg
Sédelé buki lay sédelé
Su ko yallah mayé dolé dotul jégalé
Da fa gawa xebatè gawa yabatè
Ku ko eupeulè kesse ko ku lay respecter
A ka meun fallatè mana jeulatè
Rambadj ni seytané niakk koloré
Gawa djeuwatè
Bu suuré rew bu amè bew
Amul kaddu. Tè day beug waķh ju sew
Dou kholè day kholè
Ku mu deukeul nga tokhou
Di na lay niè di la ignanè
Di la soufou di la Soukhlou
Da fa Meuna niane tè ney ba ba buy saw sakh du sit
Bu duggè sa toilettes bayi fa bombe atomik
Ken du ko denk alalu mboolo
Du fay boor ta su abbe du dello
Soo kay nian nian ko ci biir Mbollo
Ndakh su lay may da koy def ci mboolo

Поcмотреть все песни артиста

Sanatçının diğer albümleri

Benzer Sanatçılar