Nax sa keur dou tax Bougnou seyé xaleyi dounla mèré Nax en tiiii nangou na kon ba dounla méré Nax sa keur dou tax Bougnou seyé xaleyi dounla mèré Nax en tiiii nangou na kon ba dounla méré Yagui xey may gontou bay wadia gnibi Néké Mbeuguel 7 à 77 ans Ma lay lathie 20ans yima dessé Bébé te nga nieuw gounghema Magui xey ngay gontou bay wadia gnibi Néké Mbeuguel 7 à 77 ans Ma lay 20 ans li la déssé Nax man nama se beugal Xam na ni dal li ma min tiss na lolou Man tissou ma nax kounek beugeu guissé Ba méro sama xalate doyna war Pas de tout man deh dérangewuma Nax at yi nga am mom la taw di titoro Pas de blême tarou jiguene sey la Tonton négou sey dafa touti Niar gniou beugante mana boko lal Tonton négou sey dafa touti Niar gniou beugante mana boko lal Nax sa keur dou tax Bougnou seyé xaleyi dounla mèré Nax en tiiii nangou na kon ba dounla méré ayi aya Nax sa keur dou tax Bougnou seyé xaleyi dounla méré Nax en tiiii nangou na kon ba dounla méré Tonton néné Tonton néné tonton beug nala Bébé yar bi nga ma yan Bou dagoul anti dou xoulo Bébé djiko bi nga ma yan Bou dagoul xale yi dougou kass Anti lako wara djil nax mou kontane Mou xam ni seysiwo danga diamousi Bébé beugouma wagal sama none ba togne sama borome Kin dal diapalé gnibina Kin dal wétali gnibina