Kishore Kumar Hits

Afrotronix - Run Away Ta şarkı sözleri

Sanatçı: Afrotronix

albüm: Run Away Ta


Make me run away, fly away
Wodini dar bara ayé gimme fire
Run away, fly away
Into a place where i can breath take me higher
Where serenity is easy pray
Run away, fly away
Run away
Mam saa ya kod mbaï nan
Biri moy a m'guer alé
Mam saa ya ndjib tam goyi
Mande mad a iyam an?
Let me get away
Mam saa ya kod mbaï nan
Biri moy a m'guer alé
Mam saa ya ndjib tam goyi
Mande mad a iyam an?
Let me get away, fly a way
Aya yoda, aïwa aïwa yoda
Aya yoda, aïwa aïwa yoda
Yoda, yoda
Dama màndi ci yow
Dama màndi ci yow
Dooto lal suuf
Kaay ñu aju
Ñëwal ci peyyi bi
Ken du rëccu
Fi dafa yaatu
Ken du la xatal
Am nga kàddu
Dañ lay àddu
Leppa jaadu
Yalla ngi tàccu de
Feccal mbëkku
Dañ lay jësbu
Tey nga daaju
Genne li nëbbu de
Mën a bakku
No tongue can tell
How you make me feel
I fell under your spell 2x
Yaama mën a jallalé
Xëcc ma fu soree sori
Nañu dem fu soree sori
Sama tank dootul laal suuf
Sama bët yi de yaakoy tuuf
AÏwa
Mam saa ya kod mbaï nan
Biri moy a m'guer alé
Mam saa ya ndjib tam goyi
Mande mad a iyam an?
Let me get away
Mam saa ya kod mbaï nan
Biri moy a m'guer alé
Mam saa ya ndjib tam goyi
Mande mad a iyam an?
Let me get away, fly away
Yoda, Yoda

Поcмотреть все песни артиста

Sanatçının diğer albümleri

Benzer Sanatçılar