Kishore Kumar Hits

Orchestra Baobab - Bul ma miin şarkı sözleri

Sanatçı: Orchestra Baobab

albüm: Specialist In All Styles


Bul ma miin, Bul ma miin
Bul ma miin ba fatte ma
Kon mu ňaaw
Adduna yaa mëna wor
Xaň ma ndey xaň ma baay
Boo ma digee sama doom nax nga ma
Lekkatuma, naanatuma
Tëddatuma, nelawatuma
Boo ma digee sama doom nax nga ma
Alarba la woon ci weeru koor
Mu taggu ma ne ma maangi ňëw
Boobu ba téy gisuma sama doom
Woy wéét, woy wéét
Woy wéét adduna
Sama doom dem na nii

Поcмотреть все песни артиста

Sanatçının diğer albümleri

Benzer Sanatçılar