Mmmmmmm Bëss bou warone nex leu Moudjé ay dioy Sama yaram daaw na Sama xol toy na Kima beugueu demna Kouma ko wakhone Meunou ma ko gueum li Comme ay lebone Pekhé none lou am leu Louma xam leu mane Diam negne sama xol beu Beumou diarré fa Garap'ou mbeuguel so dagué reine ya Boul si meusseu yakar guiss tcha dome yeu Haaaaaaann Nama nala lol Té khawma fane nga dem Douma leu massa faté Ak fo meuneu dem Sa megnane nala fekka Fo meuneu nekka Dalalal sa xeel Sama xol ya tchi nekka Nama nala lol Té khawma fane nga dem Douma leu massa faté Ak fo meuneu dem Sa megnane nala fekka Fo meuneu nekka Dalalal sa xeel Sama xol ya tchi nekka Seuy negne ba am ndiabote sama xeel Diotoulo ma bayi kou maley kholé Rogogne dina siit souma la gnaké Mbeuguel dina tiiss Diama wagnekou Yalla na nga xiipé sama keur Tiat begne la djitou Tchi sa ndieguenaye Te di nga yobalé sama mbeguel Te di nga bayi mak doundou namel Kham nané nala manquer lol Wara doundou Douma guiss sa dome Dagne la nangou tchi samey lokho Meyou gnouma sakh ma khol sa xol mane Hannnn Meyou gnouma sakh ma khol sa xol mane Nama nala lol Té khawma fane nga dem Douma leu massa faté Ak fo meuneu dem Sa megnane nala fekka Fo meuneu nekka Dalalal sa xeel Sama xol ya tchi nekka Nama nala lol Té khawma fane nga dem Douma leu massa faté Ak fo meuneu dem Sa megnane nala fekka Fo meuneu nekka Dalalal sa xeel Sama xol ya tchi nekka