Xaaleul leen ko yoone wi nila Teleulalé tapis rouge bi cii la Dou xéwé féneu foudoule fi cii mo leu Borom beuss bi yeksina mo ayé tay Mani, Tayla tay bissou fête la Bou dara seed ndaax lep matt na Dou xéwé féneu foudoule fi cii mo leu Borom beuss bi yeksina niou sargalko Kaay leen Kaay leen Kaay leen ki niou done xaar yeksina Kaay leen Kaay leen Kaay leen ki niou done xaar yeksina Na nieup nieuw niou guéw fi Mani amoul mbok xarit deukeu ndo yi Yow da nga baax mo waral sa bessa melni Borom beuss bi yeksina niou sargalko Kaay leen Kaay leen Kaay leen ki niou done xaar yeksina Kaay leen Kaay leen Kaay leen ki niou done xaar yeksina Kaay leen Kaay leen Kaay leen ki niou done xaar yeksina Kaay leen Kaay leen Kaay leen ki niou done xaar yeksina Am naga foula, am nga fayda Sa ndiambar rekka waral sa bess melni Tamit koula xol guiss ci yow diom Kone borom bess bi yeksina, hunnn Rewmi kou sagnone dafay Melni yow, melni yow Rewmi nieupeu beug Melni yow, melni yow Rewmi kou sagnone dafay Melni yow, melni yow Rewmi nieupeu beug Melni yow Rewmi kou sagnone dafay Melni yow, melni yow Rewmi nieupeu beug Melni yow, melni yow Rewmi kou sagnone dafay Melni yow, melni yow Rewmi nieupeu beug Melni yow Hee Kaay leen Kaay leen Kaay leen ki niou done xaar yeksina Kaay leen Kaay leen Kaay leen ki niou done xaar yeksina Kaay leen Kaay leen Kaay leen ki niou done xaar yeksina Kaay leen Kaay leen Kaay leen ki niou done xaar yeksina