Kishore Kumar Hits

Viviane Chidid - SADIK LADY - Live şarkı sözleri

Sanatçı: Viviane Chidid

albüm: Anniversaire "Les 22ans du Jolof Band" (Live)


Bu ñuy doxaan ci lune ding ko deg
I love you baby, my sweety, my lady
Yama gënël, sama ndey ji, ak sama baay bé
Sukk raam jébbalu joy lune ñu def ko
Bu ñuy doxaan ci lune ding ko deg
I love you baby, my sweety, my lady
Yama gënël, sama ndey ji, ak sama baay bé
Sukk raam jébbalu joy lune dinañ ko def
Lima metti batax ma sopi jikko (moma)
Def nima mel ba nopi ni fess (moma)
Nelawal ma ma yewu gëna sadik (moma)
Góor-e tax jigéen soxor leegi
Jël pakka jam ko sama digg xol (moma)
Bayi fa lekket bo xamni du deñ (moma)
Nelawal ma ma yewu gënë sadik (moma)
Góor-e tax jigéen soxor leegi
(Leegi)
Ñaata yoon lama wax "I love you"
My baby
(Baby)
Ñaata yoon lama wax loolu
Xale bile moom, lu Yàlla xam doyna
Dafma gëlëmël ci mbëggeel touté dess mu ray ma
Xale bile moom, dafma né daf ma lova
Ndeketé lepp lum la mës wax ay fenn la
Xale bilé (ñewna)
Xamal mani (moom la)
Néma sama (goor la)
Lepp ay (door la)
Xale bilé (moma)
Soppi na (jikom ba)
Fima ko romboon ci mbedd mi daf ma dab
Bula góor toppate néla bëgg nala
Xamal ko xol dafa Oyof buguma nga gañ ma
Bula góor toppate néla bëgg nala
Lacc ko bëgg na giss papam di toroxal Yayam
Baby
Bu ñuy doxaan ci lune ding ko deg
I love you baby, my sweety, my lady
Yama gënël, sama ndey ji, ak sama baay bé
Sukk raam jébbalu joy lune ñu def ko
Bu ñuy doxaan ci lune ding ko deg
I love you baby, my sweety, my lady
Yama gënël, sama ndey ji, ak sama baay bé
Sukk raam jébbalu joy lune dinañ ko def
Lima metti batax ma sopi jikko (moma)
Def nima mel ba nopi ni fess (moma)
Nelawal ma ma yewu gëna sadik (moma)
Góor-e tax jigéen soxor leegi
Jël pakka jam ko sama digg xol (moma)
Bayi fa lekket bo xamni du deñ (moma)
Nelawal ma ma yewu gënë sadik (moma)
Góor-e tax jigéen soxor leegi
(Leegi)
Ñaata yoon lama wax "I love you"
My baby
(Baby)
Ñaata yoon lama wax loolu
Buñu bëgg dem, buñu bëgg dem
Te gën lula ci
Yawit boleen jekko tegal le lu sadik
Buñu bëgg dem, buñu bëgg dem
Te gën lula ci
Yawit amal fulë amal fulë
Wawaw bàyikoo, bàyikoo
Ndax moom xamul sa njëkk
Oh bàyikoo oooh
Ndax moom xamul sa njëkk
Sister, please don't cry
Fompal say rangoñ
Bula góor jaral ngay joy
Fompal say rangoñ
Bu ñuy doxaan ci lune ding ko deg
I love you baby, my sweety, my lady
Yama gënël, sama ndey ji, ak sama baay bé
Sukk raam jébbalu joy lune dinañ ko def
Lima metti batax ma sopi jikko (moma)
Def nima mel ba nopi ni fess (moma)
Nelawal ma ma yewu gëna sadik (moma)
Góor-e tax jigéen soxor leegi
Jël pakka jam ko sama digg xol (moma)
Bayi fa lekket bo xamni du deñ (moma)
Nelawal ma ma yewu gënë sadik (moma)
Góor-e tax jigéen soxor leegi
(Leegi)
Ñaata yoon lama wax "I love you"
My baby
(Baby)
Ñaata yoon lama wax loolu

Поcмотреть все песни артиста

Sanatçının diğer albümleri

Benzer Sanatçılar