Sama xalé bi nangu na Sama Goné gui nangu na Yaye boy sama shorty bi nangu na Baye boy sama suger bi nangu na Awadi bilay goné gui néna waw Xalé bou rafet dikeu na, dikeulen sétane Wa kogn bi kaay len xol Lay la la law Damey nanguo Damey nangu (bess bi sa bessa) Wol badiene, wowal nidiaye damey nangu (Bess bi sa bessa) Damey nanguo Damey nangu (bess bi sa bessa) Yeuy kani, matia fi xorom damey nangu Tey na waw ne na nanguna (han) Wa kogn bi xale bi nanguna (way deugueula) Yeggeul ko tiat ba tiat Gor ak jiguen, mag ak ndaw Sama xalé bi nanguna (wu yaay) Sabar yi, ndeundeu yi, reuk lene (teugueu lene) Mamane, tama yi, ana nguene? (way tama ya) Bongo dou manke de, dikeulene (way bongo) Ndaanaanou deukeu bi gueneu lene (way deugueu leu) Yaru nga, jekk nga, taaru nga (aie way) Mat nga sa place, da nga jongoma Man maa la tann sama sadja ban Yaye sama love, sama xol, fi ba abadan (waw waw) Da mey nanguo Da mey nangu (bess bi sa bessa) Wowal badiene, wowal nidiaye Da mey nangu (diog lene niou gumbé) Da mey nanguo Da mey nangu (bess bi sa bessa) Yeuy kani, matia fi xorom Da mey nangu Seeri boy mané tey la tey (han han) Tanneul lu la nekh mané naa ko feye (way han han) Wurus aki ngalam mané, maa la mèye Sama xol dafa sedd buma kéna rèye Du man du yow, mané yalla la Mo ma tanneu, ma tanneu la Mo mané demal ci tali bi demal ci gedj Dugu gaal mu won ma la (wouy yay) Yow la done xaar (kekh kekh may ré) Yow la done xaar yow (kekh kekh may ré) (Gneup di ré) Da mey nanguo Da mey nangu (bess bi sa bessa) Wowal badiene, wowal nidiaye Da mey nangu (kou sa xol neex) Da mey nangu Da mey nangu (diuk lene ñou bal) Yeuy kani, matia fi xorom Da mey nangu Yaw yay sama sadiabane Rabadabine ndat say Yaw yay sama sadiabane Rabadabine Bilaye goné gui né na waw Diok lene gnou gumbé (hé hé) Diok lene gnou gumbé (hé hé) Wa Sénégal (hé hé) Ku nek ak ki nga beugueu (hé hé) Xolal diok lene gnqu gumbé (hé hé) Diok lene gnu gumbé, gumbé (hé hé) Yaba ndaw rabine ndat say (hé hé) Wu yay Bess bi sa beussa Da mey nanguo Da mey nangu (bilaye gone gui néna waw) Wowal badiene, wowal nidiaye Da mey nangu (lay laha ila la) Da mey nangu Da mey nangu (woy l'amour il est beau) Yeuy kani, matia fi xorom Da mey nangu Sama xalé bi nangu na (wo yay) Sama Goné gui nangu na (han) Yaye boy sama shorty bi nangu na Baye boy sama suger bi nangu na (way deugueu leu) Sama xalé bi nangu na (aie way) Sama Goné gui nangu na (wou yay) Yaye boy sama shorty bi nangu na Baye boy sama suger bi nangu na