Yeah Hunnn hunnnnh Yes yes yooooo Gunnah Gun in da area Dama yémé lol yeaaaaaaahhhhh. Ok Barre you diss ni flowou Pop smoke welcome to the party Mane guay get di jump ni daddy Mac ak Mac daddy Marqué histoirou rap bi maye kalidou koulibaly Ragal dou diegui raye khalé kassé boum diegui tally J'Suis pas une révélation mais une révolution Souguéne taxé ma merr siguéni xam poséidon Kou baax doumla clash non damlay cogiter Lo Gnouni rap mom mouy sagua sa rappeur comme cissé Lo From the refugees camps je multiplie la score Li dafa yomb thi mane Li leçon wou notre corps Souma rapoul game bi daye séléw ni yor yorou koor Sama flow bi rekay changé mais douma sopi djiko Dou yomb pour ma neex la so amoul culturou hip-hop I got the keys keys I'm the present and the future Buzz, tendances ak gno sén si pote Voice of the voiceless mane la guetto bi di support Beuri thiow xamna motax gnou orienté ma histoire Malene geuneu taxaw fouf èèè petit assis toi Gun mola tiim baisse ta tête lèvent tes dix doigts Je suis fou dis toi faut pas que tu me tutoies Hey Si kaw meune rap la togg té doumassi jogg Da melni mane ak Rosa parks amna lougnou bokk Comme Thomas Edison limay wax fou lerr lako tek Ndaw ni guinax wayé mane la ki gni mouss di get Hey Koudoul raté coup franc xamna gua ni mouy def penalty Nimay def boyé raw ni Zidane defone Materazzi Nimay dawale doko gawa guiss ni Maserati fii I'm a black crystal douma xéwi maye N.I.X Sou Gun di play nieupay dieul pose té douma photograph Poète de la rue j'ai le vocabulaire et l'orthographe Xaley bou ndaw dila délo diamonoy ladidadi Barre you diss ni flowou Pop smoke welcome to the party Aaaaahhhh Coups de feuuuuuu Tou tou tou tou tou