Kishore Kumar Hits

Gun Mor - Mandouté şarkı sözleri

Sanatçı: Gun Mor

albüm: Coups De Feu


Maam mor
Mandouté
Sa lamign bi naguko té
Sa beut yi tam naguko té
Bougn né déme rek gua déme
Kouné amna foum wara yéme
Kone Yemal si sa domaine
Lepp loy digué gnagua ko meune
Beug daradja boum taxe guay féne
No def bess dina feign
Boul def lo degg waxko
Meune nala dioureul kasso
Yafi def yafi waxone
As Gor Dako war di moytou
Nagua mandou si képeu kouy dox
Té doylou si lign la diox
Loussa yone si sama yeuf
Legui juge jugeél say dieuf
Boul degg dadi geum
Wala guiss rek ni waw
Guiss dafa wara lerr
Degg tam wara xote
Diangual xam lathia birr
Ba meune xam lathia biir
Bo paré xam lassa birr
Boy Nagua mandou bayilen si birr
Koulay lath lo defoul
Boulko rouss wax neko defo
Koulay lath lo xamoul
Boul ragal neko xamo
Nitt day mandou ame foulak fayda
Boul nangou kéne dila fenlo
Defal lo xam
Waxal lo xam
Foo déme bo teudé nelaw
Defal lo xam Ko xamoul loumouy dox bakok doxam
Lep lou waye di wax dess koy xalat Ndax euleuk do xam
Bo doné kilifeu oufeul sa ndiabott té bayi toguane
Diougoulo figua tok loussa yone si nitt kék autom bou panne
Sou ñep mandou wone kene dou ame problème
Fi Kou teulei dém né sa morom do dém
Koula newoul goungué ma lokoy topé
Féne ak dieuw gor warouko diobé
Xolal sa lamigne bi nimla noté
Boumou gooré kene doulako takal
Bamelou biire kene doulako gassal
Meuno té kou def gua dièm ko yakkal
Xamo té kou wax gua dièm ko sossal
Nagua mandou si diné djambour
Mandou si tarixa djambour
Mandou si allalou djambour
Jabarou jambour ak domu jambour
Li geuneuy mandou si diné djambour
Mandou si tarixa djambour
Mandou si allalou djambour
Jabarou jambour ak domu jambour
For real
Boul degg dadi geum
Wala guiss rek ni waw
Guiss dafa wara lerr
Degg tam wara xote
Diangual xam lathia birr
Ba meune xam lathia biir
Bo paré xam lassa birr
Boy Nagua mandou bayilen si birr
Koulay lath lo defoul
Boulko rouss wax neko defo
Koulay lath lo xamoul
Boul ragal neko xamo
Nitt day mandou ame foulak fayda
Boul nangou kéne dila fenlo
Defal lo xam
Waxal lo xam
Foo déme bo teudé nelaw

Поcмотреть все песни артиста

Sanatçının diğer albümleri

Benzer Sanatçılar