Yooow Dina baax sounou devise Ndax lignou warr dafa beurii Paré pour guerre ak ndoll yoré ay armes soll sounou tenue Pauvreté mognou dorr aller retour ndam li dagnkoy dieuli Téla Niémé tiono Lou nadj bi tangue dieur ame nagn diom youko dieuri Dakanté ak sounou noflay Tanka diapougn ko amougn togay Donne bi dou changé boudé do fight Saxoay ay laff nala lerr ni do fly La réussite est au bout de l'effort Fou seug yomb Lou diaffé fay fort Niémé ligey bi ni fou wala folle Tiono dou rer nodeff fayekou par force Hey Pour gni beug ame té nangou wougnou soneu Nélene sen aduna day geuneu tarr Pour paa yi ak mère yi yewou fadjar Ndax ndiabott néléne lepp dina baax Pour gni niane seni ay soxla mou teuweu fadjou té xamougn sax loutax Gni thiabi fété guinaw ak gni teude fébar boulene meusseu xaddi badi salite geum lene nii Everything Yeah Everything is gonna be alright Everything Yeah Everything is gonna be alright Metineu, matina Yow Metineu wayé beus Dina nex Tarrna kay wayé lepp Dina jeex Yes everything is gonna be alright Hunh Les derniers seront les premiers (c'est ce qu'on dit) Faut y croire faut pas hésiter (boy no hésité) Gni dagua diam moy gni dakone loupé Weurseugou God xamo foumouy djougué Tomorrow biss leu Bou woutek today Missalou akhmadou bamba Wala yonentii yallah youssouf NGueum ak paas teylou lay andal Digua diot sa waleu yalla dou dou dioum Doollé gua beug yokal treune Lilay maye xam xam moy guay geustou Futur milliardaire dou xépp deureum Geumougn leu doxal deme boul guestou Té Geum ni Everything is gonna be Alright Def ligua wara def Boul wath Li fath soxla yi Dou togay No def mou metiii Mais do baye Fight ba guéneussi Lepp Loy def mou leew nek sii Boul sax tiit bour bi diogou fii Loum dogal nodef dingko guiss Trust me Everything Yeah Everything is gonna be alright Everything Yeah Everything is gonna be alright Metineu, matina YowMetineu wayé beus Dina nex Tarr na kay wayé lepp Dina jeex Yes everything is gonna be alrightt