Waaw bennoo lañu wax Bennoo lañu wax si miim réew Bennoo lañu wax Bennoo lañu wax si miim réew Sàq bu ñépp bokk jëlal sa wërsëg Kenn ku ñów jël wërsëgam Jiite taxu fee gën Waaye jiitu taxu fee raw Waaw bennoo lañu wax Bennoo lañu wax si miim réew Bu jëf doon jikko kon kenn du sonn Nit moom mënta baax jikko Àdduna àdduna àdduna àdduna àdduna da fa yaatu Waaw àdduna àdduna àdduna àdduna àdduna da fa yaatu Lu ca waay denc, ngëneel la ciy sàkku Aateel sa moroom ni sa bopp, mel ni ba nga doonul dara Fii ku fi juddoo gan gu indiwul yóbbal nga Way leele leele Waaw bennoo lañu wax Bennoo lañu wax si miim réew-a-réew Lu waay doon, nit a ko ko def Seetal ci benn buur bi tey Yàllaa mi Lu waay doon, mbooloo ko ko def Seetal ci benn buur bi tey Yàllaa mi Benn loxo du tàccu, benn tànk day sukkooju Soo nawloo nit, mu nawloo la Waaw bennoo lañu wax, te it moo gën Bëggal sa réew, fonkal sa réew, nawlool sa waa-réew, Ësobiyo Ba Lu mu am mayeko, lu mu am joxe ko Lu mu am sédd ma ca Ãa moo di ma xarit Lu mu am mayeko, lu mu am joxe ko Da may diggal lu baax Ãa moo di ma xarit